ThreadSky
About ThreadSky
Log In
jrbirame.bsky.social
•
93 days ago
Deuk bi nak metina rien ne va !! Y’a du boulot à faire lepa diakhasso 😞🥲 #Sky221
Comments
Log in
with your Bluesky account to leave a comment
[–]
blf06.bsky.social
•
93 days ago
Senegal dh ken diaroul wolou leigui gayi sen bopp rk yalnako yalla diapaler bamou diougate si diam 🤲🏾
2
reply
[–]
serviteur.bsky.social
•
93 days ago
C'est ça deh bcp de travailleur sont dans l'insécurité galsen ken hamul lan là 🤦🏾♂️
0
reply
[–]
momarmexes.bsky.social
•
93 days ago
Louy lii💔💔💔
0
reply
[–]
youdiapdg.bsky.social
•
93 days ago
C’est vraiment de la merde, ça fait mal très mal. Ce gars doit être poursuivi et traduit en justice.
1
1
reply
[–]
jrbirame.bsky.social
•
93 days ago
Il doit être en prison, voler un malade
2
reply
[–]
ibrafaty12.bsky.social
•
93 days ago
Mais soy liguéyi boul topo sa adouna rekk ndakh yalla mayè woul dafa ablè sooy liguéyi deil wadial teulè
0
1
reply
[–]
jrbirame.bsky.social
•
93 days ago
Bro ak pression social bi yomboul d
0
1
reply
[–]
ibrafaty12.bsky.social
•
93 days ago
Mais nak sénégal gars yi mooy lolou deh dagnouy toppo ndaw gui rekk
0
reply
[–]
mouridoulaahi.bsky.social
•
93 days ago
Bro cas bi dafa wané faille you beri bilahi
5
1
reply
[–]
jrbirame.bsky.social
•
93 days ago
No dafa yemei mais aussi nirou neu mystique
4
1
reply
[–]
mouridoulaahi.bsky.social
•
93 days ago
Surtout télé bobou dafa beri genre cas yi trop
1
1
reply
[–]
mhdbellevie.bsky.social
•
91 days ago
Yangui setlou affaire bobou kone
0
reply
[–]
layembg.bsky.social
•
93 days ago
Thiooo mais yenneu khol yi nuko niit meuné am la menul comp
2
reply
[–]
mhdbellevie.bsky.social
•
91 days ago
J’en ai vue beaucoup des pères de famille qui ont tout fait pour leur Pays et qui se retrouvent avec des salaires de retraités de 70 milles fcfa
0
reply
[–]
derviche.bsky.social
•
93 days ago
Ah c’est ça dh, bcp de travailleurs sont dans cette insécurité.
3
reply
[–]
chdiallo211.bsky.social
•
93 days ago
Deukk bi loo wax Amna Lou dess
3
1
reply
[–]
jrbirame.bsky.social
•
93 days ago
Sénégal dafa tar d
2
reply
[–]
noreyni.bsky.social
•
93 days ago
Bly xam na si dra😭
1
reply
[–]
momo218.bsky.social
•
93 days ago
Galsen dh mame dou deuk mise en scène rek la
1
reply
[–]
sim95.bsky.social
•
93 days ago
Il faut préciser si c'est un sénégalais, les étrangers qui travaillent au Sénégal sont respectés avec un bon salaire et une sécurité sociale.
Nous on est la mrd
1
reply
[–]
sesaf.bsky.social
•
93 days ago
Galsen moy lolou dei
1
1
reply
[–]
jrbirame.bsky.social
•
93 days ago
Difficile bro
1
reply
Posting Rules
Be respectful to others
No spam or self-promotion
Stay on topic
Follow Bluesky's terms of service
×
Reply
Post Reply
Comments
Nous on est la mrd