ThreadSky
About ThreadSky
Log In
art-d221.bsky.social
•
76 days ago
Vous êtes nul comme un match nul🤌🏽🤌🏽🤨
Comments
Log in
with your Bluesky account to leave a comment
[–]
malaadoboy.bsky.social
•
76 days ago
Fateh na sakh kou nul ak rayo tey bouma ko diappé khelou khalé moma diapp😭
2
2
reply
[–]
art-d221.bsky.social
•
75 days ago
Mane dé 3:0 lako doron iow nak?🤣🤣🤣😂😂😂😂😂🤣🤣
1
2
reply
[–]
malaadoboy.bsky.social
•
71 days ago
Boy soff nga
1
1
reply
[–]
art-d221.bsky.social
•
70 days ago
Deug rek lala beugona wax mais balma ak mala togn té sa xol néxul 😂😂
1
1
reply
[–]
malaadoboy.bsky.social
•
70 days ago
Ba légui défaites bi deff ma metti😭
2
1
reply
[–]
art-d221.bsky.social
•
70 days ago
Mougneul 😂😂
1
1
reply
[–]
iam-laaye.bsky.social
•
75 days ago
J'ai directement pense à toi 😭😭
2
1
reply
[–]
art-d221.bsky.social
•
75 days ago
Ne vendez jamais la peau d'un ours avant de l'avoir tué 🧐😂😂
1
reply
[–]
art-d221.bsky.social
•
76 days ago
Mangui léganés sax bama diap lén soubeu😤
0
2
reply
[–]
malaadoboy.bsky.social
•
75 days ago
Kon gueum nga né Leganes meun nama dorr nii😭🤭
2
2
reply
[–]
art-d221.bsky.social
•
75 days ago
Légui nak yak léganés kou meun🤣🤣😂😂😂😂🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
1
1
reply
[–]
malaadoboy.bsky.social
•
75 days ago
😭
0
1
reply
[–]
art-d221.bsky.social
•
75 days ago
Et bah voilaaaaaa 😎
1
reply
[–]
art-d221.bsky.social
•
75 days ago
Mola meun 😤
1
reply
[–]
iam-laaye.bsky.social
•
76 days ago
😂🤣🤣 diafandoul rek Yalla bakhna
2
1
reply
[–]
malaadoboy.bsky.social
•
75 days ago
🤣
2
reply
Posting Rules
Be respectful to others
No spam or self-promotion
Stay on topic
Follow Bluesky's terms of service
×
Reply
Post Reply
Comments