ThreadSky
About ThreadSky
Log In
omard41.bsky.social
•
97 days ago
Serieux gayi siteu meune na dann Modou ?
Comments
Log in
with your Bluesky account to leave a comment
[–]
al-amine.bsky.social
•
97 days ago
Non wayy primo siteu nieme woul coup te mom pour mou beurrei fawmou diapp ngemb te modou pou nga diapp ngemb wam faw nga encaisser ay coup wam ms le seul problème en ait que esk bou dieulé coup modou dinako meune resisté vu k dafa ragal coup??
1
1
reply
[–]
omard41.bsky.social
•
96 days ago
Lolou ladone wax legui sama boy yi modou ay coup wam gni ko meune encaissé bariwoul dh
1
reply
Posting Rules
Be respectful to others
No spam or self-promotion
Stay on topic
Follow Bluesky's terms of service
×
Reply
Post Reply
Comments