ThreadSky
About ThreadSky
Log In
tiz221.bsky.social
•
91 days ago
Instant bii français yii denio sissou ci lou diomaye wax 😂😂😂
Comments
Log in
with your Bluesky account to leave a comment
[–]
paamousaa.bsky.social
•
91 days ago
On boit leurs larmes 🥸🥂.
0
reply
[–]
seexsaar.bsky.social
•
91 days ago
Looy wax nii😂💪🏾
0
1
reply
[–]
tiz221.bsky.social
•
91 days ago
Niou gui niak tou rek fêlé cii eutu elon
1
2
reply
[–]
seexsaar.bsky.social
•
91 days ago
Diomaye sikk la def, day dugal benn coup bàyyi la ngay xataraayu. Noonu la defoon Me Elhadj Diouf😂
0
reply
[–]
seexsaar.bsky.social
•
91 days ago
Baax na ci ñoom👏🏾👏🏾
0
reply
[–]
eyfasaale.bsky.social
•
91 days ago
Tubaab Say kay deño nex rek .leep ndaax nuñu leen waxee ñu abal ñu
0
reply
Posting Rules
Be respectful to others
No spam or self-promotion
Stay on topic
Follow Bluesky's terms of service
×
Reply
Post Reply
Comments