Profile avatar
mustafi-leuh.bsky.social
Musulman 🤲🏻 talibé serigne fallou ❤️ Manchester City my life 🩵🤍
45 posts 196 followers 141 following
Prolific Poster
Conversation Starter

(Superbia in proelio) fierté dans le combat city rek niou déme 🩵🤍

Ki kou niapp ndayam dessert guay dieundé say mame dmrm

‼️PROS 🇸🇳❤️👏🏿

🚨Ouverture de la première session ordinaire de l’Assemblée nationale nouvellement élue.

Orange danouy keupeuteul 😂😂

Orange danouy keupeuteul 😂😂

Ki khalatt horaire diangue 8h-16h vrai dmrm la 😞

Shampoing et démêlant 2500fr nga deigue li mou déf ci deuk 😂😂😂.So leine dieundoul aussi meun ngueine reposter. NB:Goor aussi dafay shampoing di démêlant 😌😌🤗 si imane la bokk(astafiroulah worou ma😂)

Bonjour à tous ceux qui sont contents pour le défaite du real de mdrinul 😂😂🤝🤝

Bismilah defaite de real madrid en cours ✅

Defaite real madrid mon combat 🙏

Soupe kandjié plat de merde mako wakh kouma si dépasé diadal kogne niou khéékhh

Soupe kandjié plat de merde mako wakh kouma si dépasé diadal kogne niou khéékhh

@ndmarie3.bsky.social Bismilah yalla nanou yalla may ndam 🤲🏻

@ndmarie3.bsky.social Bismilah yalla nanou yalla may ndam 🤲🏻

Fii khana amoul ay cityzen ahh Nieuwlen tay danou jouer peu importe la situation on est et on restera toujours des cityzens (SUPERBIA IN PROELIA ) #mancity

Pep dehh li lanou tegualati tay ms on vas gagner inchallah 🩵🤍 SUPERBIA IN PROELIO

C confirmé ça c pour un ami 🤔

Le bonheur de yéwou fadjr 🥰😇🥰🤲🏻

Le bonheur de yéwou fadjr 🥰😇🥰🤲🏻

Bonne journée sous la protection d’hallah 🤲🏻🤍

Bonne journée sous la protection d’hallah 🤲🏻🤍

Nanou sampou rek tok si tank yi amoul mayé dara fi mome nieupay tolo amoul gros compte amoul dara

Nanou sampou rek tok si tank yi amoul mayé dara fi mome nieupay tolo amoul gros compte amoul dara

@pimicha.bsky.social Kimicha mo guen nékha dégue que pimicha ahh walla guys wakh len bok

@pimicha.bsky.social Kimicha mo guen nékha dégue que pimicha ahh walla guys wakh len bok

Fi mome amoul féministe amoul dara réglé rek djiguéne deff yeufou djiguéne goor yeufou goor waw😂

Affaire de gros compte mome guys na yame X rek svp kw follow back len guys yi mo guene fi nieup ay talibé lanou

Le senegal 🇸🇳 premier pays a colonisé un réseau social nommé bluesky 😂

Affaire de gros compte mome guys na yame X rek svp kw follow back len guys yi mo guene fi nieup ay talibé lanou

Le senegal 🇸🇳 premier pays a colonisé un réseau social nommé bluesky 😂

Nek si télé bi di ndélou di doule ay yalmine bi tapete la rek

Nek si télé bi di ndélou di doule ay yalmine bi tapete la rek

Ki ndanane la bilahi

Ki ndanane la bilahi

Wa mani combat bi foumou tolou